Li Ma Weesu lyrics

Li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
seetal;
leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma mgg
lu ma gn di ygg, xel ni mel ni bank
lu ma gn di mgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
ma ni seetal;leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma mgg
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu mu ma neexee ma bggati
li ma gn di jege, mel ni dama sore
lu ma gna sore, gn di gis li ma jegewoon
lu ma gn di ygg, xel ni mel ni bank
lu ma gn di mgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma mgg

Share: